musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - FOOWé - SAMBA PEUZZI - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Foowé letra
Toog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër
Nangul waay, my baby
Yor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé
Kon man duma la fowe
Non, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh sa coeur duma ko briser
Non, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh sa coeur duma ko briser
Bari classe, solu nice
Fu la paj kanam du la ko may
Forme bu nice, sourire bu graw
Daf ma xam xale bi na ma ray
Hey, waxoon naa la baby girl dina la way
Yaa ma dekkilal suñu bëggal du dead hey
Marier monogame ci yaw la signer hey
Dam la takk maa ngi fépp foo ne (foo ne)
Sometimes ma ak yaw ñu xulóo
Waxtaan ci ay bët rekk jubóo
Hey, mënoo ma bàyyi, mënuma la bàyyi
Xol yee gise moo tax man ak yaw ñu tase baby
Toog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër
Nangul waay, my baby
Yor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé
Kon man duma la fowe
Non, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh sa coeur duma ko briser
Non, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh sa coeur duma ko briser
Ku mel ni yaw xam naa ni dafa rare fi
Dina laaj sama ñaari loxo
Bu ma rëccee mëna doon célibataire à vie
Xalaatuma la bàyyi, non, non, non
Yaw laa nob, yaw kese yaw
Duma la ko nëbb yaa may tere nelaw
Suma la mënul gént damay toog xoole ba bëtsët
Mbëggeel bi dëgg moo tax talatuma la doser
Na ñàkk fula ak fayda am la bëgg na
Vitesse la sama xol di deme su may wax ci yaw
Loolu tax ma fiir, baby xool ma fi
Nob naa la, kenn mënu ci tus
Non, non, non, doo ku ñu fowe
(Toog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër)
Ooh sa coeur duma ko briser
(Yor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé)
Non, non, non, doo ku ñu fowe
(Toog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër)
Ooh sa coeur duma ko briser
(Yor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé)
Samba Peuzzi - Letras
- Ari Dho
- Dangerous (feat. Mgeey)
- Dawalale
- Dawuma Dara (feat. Wally B. Seck)
- Foowé
- Fresh (feat. ISS 814)
- Je ne mérite pas ça
- Kirikou
- La Famille
- Lou Yakou Yawa
- Marie & Cheikh
- Mbaraj
- Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung)
- Ndaga
- Ndongo
- Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Dip Doundou Guiss)
- Oulalalah
- Paparazzi
- Sagnsé (feat. Karabalik Beatz)
- Soxna Ci (feat. Jeeba)
- Tama
- Tangal
- They Cap
- Thiatt
- Wanted
- Xalé Bu Ndaw (feat. Dip Doundou Guiss)
- Yolé Yolé
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br